staffan: xar yi dinañu dund ba tabaski
staffan: aïssatou dafay cuub
staffan: ci mbaal mi
staffan: nataal ci santr "sunu kër"
staffan: nit yi, jën lañuy xool
staffan: tefes gi dafa fees dell ak jën
staffan: tali seydina laay
staffan: buntu jumaa ji
staffan: nataalu seydina laay
staffan: kër ci wetu jumaa ji
staffan: ci asamaan si am na picc yu bare
staffan: ay buntu ci ndar
staffan: palanteer bi
staffan: karate senegal
staffan: toogu bi
staffan: jakka ji
staffan: póot mi fendi na
staffan: ay kër ci ndar
staffan: sàmm ci dëkk bi
staffan: jigeen ji romb na
staffan: béy wu ñuul
staffan: benn palanteer ci ndar
staffan: ay xarit
staffan: njagabaar yi ragaluñu nit
staffan: bus bangi taxaw
staffan: kër gu xonq
staffan: ahmadou bamba
staffan: fas ag watiir